Kàddug Yàlla

By Foundational LLC on AppTrack Ninja.

Appli bii mooy Kàddug Yàlla, gi dikke ñaari pàcc: Kóllëre gi njëkk gi Yàlla fas ak nit, ak Kóllëre gi yees, gi mujja wàcc, te ñenn ñi di ko wooye Injiil, mu tekki Xibaaru jàmm. Ñaari téere yooyu, Yàllaa leen wàcce ci nitam ñu sell ñi, kóllëre gu jëkk gi, ñu bind ko ci yawut, gu yees gi, ci làkku gereg. Li ñu bind ci téere yu jëkk ya nag, moom lanu tekki ci wolof.

Categories: Books, Reference

App Store rankings, screenshots, estimates and similar apps for Kàddug Yàlla.

Loading…
Kàddug Yàlla: Revenue, Downloads & Keywords | AppTrack Ninja